‘AROUD» Qui renvoie à la prose et laversification.
Par abus de langage, nous commettons l’amalgame entre «Qaçida» qui fait référence à l’unité de prose et «qaçayid» qui est le pluriel de «Qaçida».Ainsi nous parlons de «Moufrad» lorsqu’il s’agit d’un poème, de «mou sannaa» lorsq’il en s’agit de deux, et de «Jam’u» pour plusieurs poèmes. Un «Jam’u» devrait correspondre dans la littératurefrançaise au Recueil de poèmes.Comme toute littérature, la classification de ces termes obeit à une métrologie définie. Pour pouvoirdire que nous avons un «Qaçida», Il faut que ce dernier soit constitué de 7 vers. Pour moins que cela ondira que ce sont des «Abiaat» (Pluriel de «Beyit»
PREAMBULE
Certains propos sont tirés des causeries de conférenciers mourides comme Serigne Sam MBAYE (R.A.) ou bien de personnes dignes de foi (parmi eux Serigne Saliou GADJAGA, un fervent Talibé de Cheikh Saliou MBACKE) ayant vécu avec les fils de Serigne Touba. Il ne faut pas apprendre les Khassidas dans l’unique but de son utilité dans ce bas monde ; parce que les Khassidas seront plus utiles dans la tombe, le jour du jugement dernier…en somme dans l’Au-delà. Il faut les apprendre pour leur utilité dans l’Au-delà, dans le but d’adorer DIEU, de magnifier le Prophète Mohammed (PSL) avec des Khassidas à base de « SalatouAla-Nabi » tout en formulant des vœux dans ce bas monde, telle est la conduite à adopter. Les bienfaits ci-dessous ne sont que la partie visible de l’iceberg, l’utilité des Khassidas dépasse le sens de l’entendement humain et ne pourrait être connue que dans l’Au-delà.
LES BIENFAITS DES KHASSAIDES
DIAALIBATOU MARAAKHIB
(day diokhè mbòlò tèyit day tarbiyeu) wax nanou ni Xassida tarbiya la, gouy rakhass la, té day bidji ay xeweulXassida gui bokonn na ci you Mame Saliou Mbacké(RA) waxon ni dalay gar dieumé sounou Borom (SWT) Bò amè khalè bou deung, nga beug mou dioup fèkhèl bamiy diangue khassida gui. Kou beugueu tègou ci siràtal-moustakhìma dèl diang khassida gui.
Koukoy diangue day takha deudou addouna.koukoy diangue day takh nga beug Serigne Touba, saf-sapp ci Mame cheikh ibrahima fall, etc…
KOU TED KI nena :"kou koy diangue Sounou Borom nanga ko diegeul té yombalko diaffé diaffem yep""kou koy diangue Sounou Borom mayla lo xamni kouko doul diangue dinala ci Niè""kou ko am ak noko ammé lay donn say mebett Sounou Borom maylako si daradia Mouhamad(PSL)""etc.......................Quant à son origine:S MOUSSA Leral nako si am mbindamAmna tamiit yen mag niou waxni tamiit KOU TED KI Gannar la ko defaraté ,té Kimou diokhon daniko Armaire yo romb kep kougnou fa don mbougeul dagnou kay teggil mbougeul gui ba kerok ngay agg ba waxtou bi nga fa awwé won nieuwatt boufa kou méloulni yaw awwatté
INTRODUCTION & HISTOIRE
Xassida « DIALIBATOUL MARAHIB » Xassida gou barri Histoire laKOU TED KI si gedj gui lako ndieukeu bindé si lou mag gni wax likoy firndé moy wakhi Serigne Moussa KA « KOU TED KI bimou ko bindé ba noppi dako tek thi guedj gui ni yalla mangui topando Jazouli, bou deloussé thi mane ta toyoul raafoul ma khamni nangouna, bamou deme ba nangou ape gendarme bou toudou Moussa moko fore indil ko KOU TED KI té toyoul raafoul.
KOU TED KI soppi wat nako guinaw gui si Gannar diox ko niit nguir mou indil ko S balla Fally si la ko waxonn niko : ‘Armaire yo romb kep kougnou fa donn mbougeul dagnou kay teggil mbougeul gui ba kerok ngay agg ba waxtou bi nga fa awwé won nieuwatt boufa kou méloulni yaw awwatté ‘
Nénanou Tamiit soppi wat nako sa « THIEYENNE »
KOU TED KI tamiit Yokatt nako ganaw gui : Nénanou Dafa Fékonn S Hafia Bousso mou yoor DIALIBA mou ladj ndax Mokkal ngako ? Mouniko waw KOU TED KI niko ‘Diarnako‘ daldi koy wax ni eundil ma yokkal lassi ap nékhal .Si leu KOU TED KI yokou si « Bismillahi Rahmani…………………….fi Dareyni Aminn……. » Li likoy firndé moy KOU TED KI ganaw Guedj gui da taggo ak « SAYTAN » motax ganaw gui Xassida yimou talifaat yeep « Bismilahi… » lay tambalé au lieu de « Ahouzou bi lah….. » Motax si Xassiga gui Bismillah gui mo Djittou ; lolou moy wané Yokou gui selon Mag gni
« DIALIBATOUL MARAHIB »
(DEUXIEME PARTIE)
BIENFAITS & MIRACLES
Xassida gui (day diokhè mbòlò tèyit day tarbiyeu).Waxnanou ni Xassida gouy rakhass la, té day bidji ay xeweul .S Saliou Mbacké(RA) waxon na ni dalay gar dieumé sounou Borom (SWT).Waxat nannouni Xassida gui day taxaw taxawayou niane, Sant, Jihad, Tagg, Djoulli, Diamou yalla etc ….
Nénanou tamiit Xassida gui day eumb mbolem makhamat Gayou Bax yep.
Bokk na len si kemtane Xassida gui :
«NAWAYTOU MIN ZA ‘L HAMI HIDAMTAN TASSOURR MOUSSAFFAHAN BIHI KOUFITOUMA HASSOURR »
(Yénné na si Att mi di ‘’WAYSASSIN’’ AP LIGUEY BOUY BEGEUL YONNENT BI (Psl) Mom minga xamni moy Adji Ram’mou dji)
So dieulé le ’Waw(6)’ de Nawaytou, le ‘Ya(10)’ de Nawaytou, le’Sin(300)’ de Moussafahan et le ‘CHI’N(1000)’ de Hassourr.So ko Bollé dalay diox WAYSASSIN =1316
Té KOU TED KI mingui ko bind si “WAYSASSIN“(1316 an musulman)
Amna Biis Kou ladj S Abdou Khadre“ Ismou Lahi Ahzam “mou diox ko “DIALIBATOUL MARAKHIB“
KOU TED KI waxon nani Fadioub Adouna ak Alahira mingui si Biir
Len ci lou KOU TED KI wax si biir :
"kou koy diangue Sounou Borom nanga ko diegeul té yombalko diaffé diaffem yep""kou koy diangue Sounou Borom mayla lo xamni kouko doul diangue dinala ci Niè"“Kou Koy diangue nango ko may lep loumou beug ,ganaw ba nga diegeulé Bakkaramme“Kou koy diangue nango ko may tékhé ‚Barké ak Diam‘mou Adouna ak Alahira"kou ko am ak noko ammé lay donn say mebett Sounou Borom maylako si daradia Mouhamad (PSL)"“Yaw Sunu Borom nanga def haraffi Xassida gui mouy geun di Barké““Yaw Sunu Borom nanga def sama Xassida gui mouy Sippi ay Bakkar, bok si diamou Yalla yi geuneu mag té Kawé ak koor““ Defal sama Xassida gui mouy Begeul Malaka Mouhar’rabone yi "etc........................................................
---------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------------
A SUIVRE VOUS POUVEZ ABONNEZ AVEC VOTRE ADRESSE EMAIL POUR LA SUITE .....
|
0 Commentaires
DITES CE QUE VOUS PENSEZ SUR NOTRE SITE :