S ABDOU KHADRE (RA) waxnani Xassida GUI day yokk ay Xeweul ak di begeul talibé bi foumou meunti nek.

S ABDOU KHADRE (RA) waxnani Xassida GUI day yokk ay Xeweul ak di begeul talibé bi foumou meunti nek.


  
Xassida GUI Bok Na si Xassida yi teunk « MAFATIKHUL DJINANE ».S ABDOU KHADRE (RA) waxnani Xassida GUI day yokk ay Xeweul ak di begeul talibé bi foumou meunti nek.
Xassida « FOUZTY » diaglé la si Soxna sou mag si nga xamni mom mo am Diaglé si ap SOURATE AL’HOUR’ANE mouy « SEYDATOUNA MARIAM »ak Yonnent Yalla ISSA « ROUHOU LAHA ».
Waxnanouni KOU TED KI lolou lay dioundie si tambali Xassida gui. 
Nénanouni nimou tagué fi « SOXNA CI » eup na ap Xel. Ken meusso KO degg té ken dotou KO dèggeuty ABADAN.







Waxnanouni FOUZTY AK HOUDA ILAHI: KOU TED KI nianon Na Sounou Borom (SWT) mou geuneul KO si yiko djittou yepp (Lou yémmé).
Fouzty Bok si Xassida yi nga xamni « OUROUL AYNI » mom laniouy way AK diko titeuro euleuk Sounou Démmè Al’Dianna. 
Kou TED KI mingui KO teudié
«WA houri hayna Wadjhal ya rabbi hajihi’l Xassidatamin ah’saani maa tatahan’naa bihi’l houri’l haynou ya hayra …… …..)







(Yaw Sounou Borom (SWT) nanga def Xassida gui mouy dallal ap hol ak diko seddal
(Yaw sunu Borom (SWT) nanga def tammit mo donn li geun si way yi« OUROUL AYNI » yi di way Aldian’na)
Mak gni dan nanko bolé si nianou « SEUY » AK di ko tèerto ak diko dalallé « SÊETT » ndax dagno waxni Xassida gui leep da di ngeunel té Keep kouko saxal ndam rek ngay am si sa beep dioublou
KOU TED KI mingui niou fiy leeral tammit li oumpou nien gni si Yonnent Yalla ISSA (ROUHOU LAHA) (résumé)
« Ya Oumma rouhi’l Maliki ya ouma diali’l Haliki « Ibnouki la bihaliki hinda hali moumassiki » etc........

Enregistrer un commentaire

0 Commentaires