Axe-touba mbacke: les apprentis chauffeurs dans les rues et brûlent des pneus
Apprenti chauffeur yi nekk touba profito ci grève bi transporteur di amal tay wané sen nakhar taal Aÿ pneus ci axe touba mbacké policé yi tamit dikk nane ngir def intervention amna lou eupou 10 youn arrêté gnongui en garde à vue ci commissariat bou mbacké.
Diot nane yanen xibaar tamit sa garage darou mouhty bou touba gnongui def louni mél. "À suivre"
0 Commentaires
DITES CE QUE VOUS PENSEZ SUR NOTRE SITE :