Aly ngouille Ndiaye néna li la dogal si covid19 bi kouka nagouta dieuffé yoon dal sa kaw ba sa doko kaso khaj nathi

Aly ngouille Ndiaye néna li la dogal si covid19 bi kouka nagouta dieuffé yoon dal sa kaw ba sa doko kaso khaj nathi

Covid 19 🇸🇳 :  aly ngouille n'diaye

-- Téré nan dadialoo bi thi Stade yi AK places publiques AK téféss yi ...

-- téré nan Amal khèw khèw thi m'béddi yi comme : sarakh , n'guénte ak thiétt yi ...

-- places auto yi nio yamaléko comme ninko wakhé woon

-- Takk masque 😷 tamite par force la thi fi nitte gni di dadialo

-- di sakkou thi n'daw gni mouytou fébar bi balanioko wali séni makk 

--  kouka nagouta dieuffé yoon dal sa kaw ba sa doko kaso khaj nathi

Fallou walf Sall

Enregistrer un commentaire

0 Commentaires