"WA KANA HAQAN "
Xassida gui gni ngui ko teunk si Ayya bi "wakana haqan haleyna nasroul mouminina."Mingui nek si Sourate ROUM'(30), Ayya(46) lou yémmé lol si nombre yi .Waxnanou ni Xassida gui kouko wayo mou wayo ak yaw ba way ga diombou la l.Wakhat ni Kou tako ak mom mou tako ak yaw, té outou la say mbiir meun lassi fouf .Amna nassi nak ay Xassida you outé senni biir .Nenanou moy lougou xassida yepp .S A Khadre ak S Saliou diglé nanou ko biss bou nek
Barri na lol ay mbir si biir ndax KOU TED KI amna foumou si Diar ak Cheikh Sidy Al Baba ak Jarka (résumé) .Bokou nassi tamiit Naar yako donn diss senni Adio .Nenanou Borom keur bouko saxal dou niak ndieul mouk. Ben Kilifa nena Beuyit wi "Achkouroho wa hadali abdala.........."doy na seuk si leral (resumé) .
Kou bax nena "AJHABTA FAWHA LISSIWANA......." ben yonn lako bind wayé dadonn diglé nioukoy bamtou. Xassida bou barri ndiarigne lol sax
0 Commentaires
DITES CE QUE VOUS PENSEZ SUR NOTRE SITE :