S Mbacké Bousso nena Mawahibou ak Sab’houn Takhi daniouy mayé ay Xeweul

S Mbacké Bousso nena Mawahibou ak Sab’houn Takhi daniouy mayé ay Xeweul





                                "MOUWAHIBOU NAFIH"

Nien si Mag gni nenanou Xassida gui KOU TED KI mingui ko bind ci attou WAYSASSIN (1316 an musulman) .Mom ak Jazbou, Mouhadimat, Radiytou etc……. nio massé.
S Abdou Khadre Mbacké nena day mayé Xeweul di yokk ak Ngeum, ak beug Yonnent bi (PSL).
S Mbacké Bousso nena Mawahibou ak Sab’houn Takhi daniouy mayé ay Xeweul
Bok na si kemtanou Xassida gui Yenn Beuyit niou teunké wat bénen Xassida
Bokou nassi tamiit Xassida you KOU TED KI waxon ni nioy « Naarou Goor yi » Kou len war té wathie wolen niou wommat la ba fi mom
Kemtaanou Xassida gui:
Ben biss Mame Thierno Birahim Mbacké meussna sant ay Talibèem niou Yoboul ko Dougoub bimou bayonn si KOU TED KI ; Yobanté walé len nilen « Nélénko Maraal nanou lol » Ba nioniou agguèe wax KOUTED KI yobanté Borom Darou bi.
Si leu KOU TED KI wax Kourel gui nanou Diangue « MAWAHIBOU » Kourel gui di diangue ba Tollou si :
"Nala dialala nala diamala ""miman taxala Rabii sama i"













KOU TED KI diglé niou Bamtou ko ; ba noppi tek si « Yaw Borom Assaman sama beug beug moy ndox »
Rek Taww bi timbali di Taww .Baniou Yonnéwaat si KOU TED KI nguir mou Dakkal Taww bi
Amna Biss KOU TED KI di waxtaan ci Bissou Penthie ak Taraay ga.Ba waxni bou Biss boba Niep Sama Bopp laniouy wax bamou dess Yonnent bi(Psl) ;Mom sama Khèet lay wax .Bou biss boba ba Yonnent bi(Psl) dem HARASS ba soudioteul Sunu Borom ,bam niko Siggil té Dem Ram’mou .
KOU TED KI nena bou diogué ba dem si Taxawaay ba dinako Dogallé Fatalliko lama ko waxonn si












                             "MAWAHIBOU "

‘’Antal Karimou Annal Hadimou ‘’‘’Deuhran Oudimou Fika sana’i ’’. 
Bou boba dinama Yéssalal Ram’mou bi mouma mayonn thia Adouna Sogaa dem tokk sa Keer gua.Bou boba loxo bou touty bi koumou seedoul dinga yendo khif fanané fandé (etc.....

                   DIEUREDIEUFETY KOU TED KI

Enregistrer un commentaire

0 Commentaires