"MATLABOUL FAWZEYNI"
(PREMIERE PARTIE)
Xassida gui mom la KOU TED KI Aaré TOUBA. Xassida gui S ABDOU KHADRE(RA) néna day wommat Mouride bi si beug Sunu Borom(SWT) ak di la may kheweul ak dilako diapandil.Diglé won nako nioukoy diangue au moins Ben yonn si weer wi. Waxnanouni keep kouy santhie si beureub nga djiteul kofa lata ngay deuk .Nénanou Xassida gui nimouy Aaré nonou lay niodé ay Xeweul ak Beug Sunu Borom(SWT)
S Saliou Mbacké (RA) meusna labiiré Talibé yi si Xassida gui, fimou deukonn si sayir di ‘’MATLABOUL FAWZYNI ‘’ bay tour ay Xeweul (lou yémmé).Si lay nétalli KOU TED KI bamouy taalif Xassida gui si la Gaîndé gui donn Dakk Kéweul gui Ak ni KOU TED KI dokhé sen Diguenté (résumé)
Xassida gui si guestou yen mak gni nénanou da massé ak Yonou Mouride.
Bokk si ay Kemtanou Xassidagui leep louy Xeweul ak Karangué té am TOUBA, So geusto Xassida gui fekk kou TED KI fag’gou nako ci bou yague Kou bax nénama :
Yonnent Bi (PSL) si moudieum meusna tokk fi Beureub di Tour ay kheweul .Nénanou Sunu Borom (SWT) ladj ko Loy dioy? Mouniko Sama Kheet wi lay Xalaat sen Euleuk. Nénanou Sunu Borom (SWT) niko Sounu démé ba dieummi Diamono dina tibb si sama leer bolé ak sa Leer wathié ko si kaw Souf.
Waxma nima Xolal Beuyit bi Si « FAWZEYNI »
“FAKHOUMTOU MADJ’ JOUBAN ILAYKA MINKA‘’ BIKA HALEYKA WA RADIYTOU HANKA ‘’
(Mangui dieumat si yaw man minga Xamni si yaw la Bayiko té si yaw lay déllou) KOU TED KI néna tammit
« DAWIN KHOUROUFIA LADAL HARSIL HAZIM YA MAN BIHI WA HABTALI DOUR’RA NAZIM »
(Yaw Sunu Borom nanga def Sama Xassidayi niou nek ay Diwaan fofé Harass si yaw »
Li dé Lou leer la, té li KOU diogué fofé, Tay déllou fofé, té donn koké rek moko sagn
(DEUXIEME PARTIE)
S ABDOU KHADRE(RA) waxnani day wommat Mouride bi si beug Sunu Borom(SWT) ak di la may kheweul ak dilako diapandil.Diglé won nako nioukay diangue au moins Ben yonn si weer wi. Xassida gui moy Karangué TOUBA Mak gni dan nanouko def sen beurebou liguèyou kay ndax Foumou nek mou geun foumou nekoul
S Saliou Mbacké (RA) néna:” KOU TED KI bamouy taalif Xassida GUI mingui Tokk si souffou Garab Mbep.Bobou Touba Aal bou yatou la, Bou leundeum kirris.
Néna Ba KOU TED KI di weyeul Xassida gui ; la am Ap GAINDE don dakk ap KEWEUL ‘Mame Salou(RA) waxnanouni moudioul aggali Hisseu bi ndax da moudiou di tour ay Xeweul
Waxnanouni KEWEUL GUI guinaw la fètè KOU TED KI, si ay mbagam (si sayir) la tekk ay Tankam fek mingui tokk di Taalif « FAWZEYNI ».Waxnanouni KOU TED KI da yekeuty Xalima GUI dieumé ko si Gaindé gui. KOU TED KI dokh si Diguenté KEWEUL bi ak GAINDE gui
KOU TED KI waxanani « fahay souma tahaf illa haka’l Ahad yahafka min fikaho koulla AHAAD »
(So Ragalé Sunu Borom(SWT) nimou waaré .Leep lou Sounou Borom(SWT) bind dinala Ragal nguir Ragal gui nga ragal Yalla )
!!!! Amna niou Xam nak fou KOU TED KI tollonn ba lolou di khewak biis bi ak waxtou bi !!!!*
KOU TED KI waxna si biir :
----- ---- --- « WA HADIATANE LIKOULLI BIDHUFINE IRTADA»-------------« WA HUDIATTANE HALA MOUHALIFINE HADA »
(Sounou Borom (SWT) nanga def ‘’TOUBA’’ mou nek Beurebou hadj(Pèlerinage) si ki nga Xamni amon na Gante, ba djotté wouko si kanamou ki nga xamni da bagnonn kerok bissou deug ga)
-----------------« WA MASKANANE LI DIALBI KOULLLI HAYRI » -----------------« WA MASKANANE LIDAF’I KOULLI DAYRI
(Défal TOUBA mou donn beureub bouy nioddi bep yiiw ak Xeweul tay diegn bep loor) ----------------« WA NADJINI MIN SARRI SAKINIL BALAD »-------------------WA SARRI KOULLI WA LIDINE WA MA WALAD
(Mousseuleul kep Kou deuk ‘‘TOUBA ‘‘si bep loor ak kikoy indi ak limouy indi) etc.......
0 Commentaires
DITES CE QUE VOUS PENSEZ SUR NOTRE SITE :