professeur Moustapha sourang moufi bayéko guinaaw fébar boum amé woon ça hôpital Principal de Dakar moom mifi nékoon ministre de l’éducation nationale thi diamonoy Wade

professeur Moustapha sourang moufi bayéko guinaaw fébar boum amé woon ça hôpital Principal de Dakar moom mifi nékoon ministre de l’éducation nationale thi diamonoy Wade

Sénégal 🇸🇳 : professeur Moustapha sourang moufi bayéko guinaaw fébar boum amé woon ça hôpital Principal de Dakar moom mifi nékoon ministre de l’éducation nationale thi diamonoy Wade , nékon Enseignant ça l'Université de Dakar, nékon ça Faculté des Sciences juridiques de 1984 ba 1999 nio tabaatko recteur de l'Université Cheikh Anta Diop de 1999 ba 2001 , thi wérou mai 2001 nio tabaatko ministre de l'Éducation guinaaw bi moy Ministre de la Justice décembre 2011 nio tabaatko Ministre des Forces armées 2014 président Sall taboko président de la Commission nationale de la réforme foncière ay atam tolou thi 71 Ans

Fallou walf Sall

Enregistrer un commentaire

0 Commentaires